Darkase wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Hugo.arg (waxtaancëru)
mAucun résumé des modifications
Hugo.arg (waxtaancëru)
mAucun résumé des modifications
Rëdd 1 :
[[Dencukaay:Cashew Brazil tree.jpg|vignette|Garabug darkse]]
'''Darkase''' xeetu garab gu bokk ci njabootu '''Anacardiaceae'''. Ca Amerig gu naaje ga la bàyyikoo, te ci barab yu naaje yi lees koy baye ngir foytéefam.

==Melo wi==
Garabu darkase danay àgg 12 ba 15i met ci guddaay. '''Buut''' bi di reenam bi ëpp solo danay àgg ci xóotaay bu sori ci suuf si. '''Pànguur yi''' di reeni wet yi danañuy àgg fu sori lool. Xobam wirgow nëtëx bu dër la yor. Danay àgg 10 ba 20i sàntimet ci guddaay ak 10 sàntimet ci yaatuwaay. Xobam wi puur ci noor lay feeñ. Daa gëtte am xet gu neex te day xëcc yamb yi, ci la lem di bàyyikoo.

==Doom==
Doom bi ci njeexteelu noor lay mat. Bu ñoree day xonq mbaa mu mboq. Bu ñorul nag nëtëx. Am ub saal ca biir bu ñuy wax '''ndaamaraas''' mu bari ay njariñ lool. ==Njariñ li== Doom bi dees na ci njar, dees na ci defar sàngara te dees na ci faju. Garab gi nag dees na ci jële am matt dees na ci faju.
 
==Turu xam-xam wi==
Ligne 13 ⟶ 19 :
Dencukaay:Cashew Nut Tree - കശുമാവ് 01.JPG|Xoox i doom bi
</gallery>
 
==Turam ci yeneeni làkk==
Farañse: acajou
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Darkase » lañ ko jële