Lóriye wuute gi ci sumb yi

Contenu supprimé Contenu ajouté
Daarul xayri (waxtaancëru)
Xët wu bees : '''Lóriye''' garab gu ndaw lay doon mi ngi bokk ci njabootug (abusinaas) garab la gog des koy fekk ci dexi miditeraaniy. Mi ngi yamog benn xeetu (espes), bu yor melowu nderyéem....
Tafaan: Éditeur de wikicode 2017
 
Daarul xayri (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Éditeur de wikicode 2017
Rëdd 1 :
[[Dencukaay:Nerium oleander 20zz.jpg|vignette|Nataalu garabug lóriye]]
'''Lóriye''' garab gu ndaw lay doon mi ngi bokk ci njabootug (abusinaas) garab la gog des koy fekk ci dexi miditeraaniy. Mi ngi yamog benn xeetu (espes), bu yor melowu nderyéem. Yenn saay des koy woowe oleyàndar walla ñu di ko woowe batay rosaas neriyeen. Garab la gog day am taaru lool te yaatu lool foofu, fépp ca mediteraaniya ñu di ko fo sàmm ngir ni moom dafa mana dékku, (seserees).
 
Ci « https://wo.wikipedia.org/wiki/Lóriye » lañ ko jële