Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar
' Iniwersite Gaston Berger mooy Daara ju kawe ji nekk diwaanu Ndar ci réewum Senegaal.
Démb
SoppiLéewópóol Sedaar Seŋoor moo amal tegum xeer bu jënk ci wàllum taxawaay iniwersite wi ci 14 sãwiye 1975.
Taxawaayam mu ngi aju ci sart Royuwaay:N° bu 2 sãwiye 1990, iniwersite wu Ndar mu ngi teeru limu ndongo wu njënk (600)ci 17 Desàmbar 1990 ci yoonu négandi.
Mu ngi jot gëddam ci ndogalu Royuwaay:N° bu 10 sulet 1996 ak tur bu bees jóge ci ndogalu Royuwaay:N° bu 4 desàmbar 1996.
Ku ñu ko duppe Gaston Berger, nekk na ab kàngam ci wàllum xeltu, di doomu Senegaal ak Farãs, juddo Ndar-Géej. Di baayu Maurice Béjart.
Ràññeefi barab
SoppiDiggànte iniwersite ak Ndar toll na ci fukki (10) km. Boo jóge Risaartool jëmsi Ndar di nga séen wërngalu kàggu gu mag bi. Iniwersite dafa fekk boole ñaari dëkk : Sanaar Pël ak Sanaar Wolof. Loolu tax na ndongo yi di ko woowe yenn saay Sanaar. Itam kërub internetu ndogo daara yi« https://web.archive.org/web/20080419061846/http://www.sunusanar.com/ » la ñu ko tudde.
Bërëbu tàggat ak gëstu
SoppiIniwersite bu Ndar ëmb na juróorum-ñaari Bërëbu tàggat ak gëstu :
- Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama
- Xam-xamu jëmale ak xarala
- Xam-xamu yoon ak politig
- Xam-xamu koom-koom ak
- Xam-xamu wérgu-yaram
- Xam-xamu mbay, sàmm, nàpp ak xarala yu màcc ci wàllum dund
- Caada, diine, taaral ak jokkoo
- Diiru njàng mi di na toll ci fukki weer. Di tàmbalee oktoobar jàpp sulet. Waaye ubbite njagale mi ak njeextal mi ngi aju ci barabu tàggat ak gëstu bu nekk.
Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama
SoppiBarabu tàggat ak gëstu ci ladab ak xam-xamu nekkinu doomu aadama ëmb juróomu bàqasu:
- Angale,
- Farãse
- Làkk nasaraan jëmale,
- Xam-xamu melosuuf,
- Xam-xamu nekkinu àskan yi.
Xam-xamu jëmale ak xarala
SoppiBarabu tàggat ak gëstu ci xam-xam jëmale ak xaraala ëmb na bàqasu xayma jëmale, bànqaas informatig, bànqaas bitil jëmale ak tàggat ci wàllum xéy.
Mën a dugg
SoppiBànqaasu xayma jëmale
SoppiBànqaasu bitil jëmale
SoppiBànqaasu informatig
SoppiXam-xamu yoon ak politig
SoppiBarabu tàggat ak gëstu xam-xamu yoon ak politik ëmb na ñett bàqaas:
- Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi ;
- Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris ;
- Bànqaasu xam-xamu politig.
Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi
SoppiBàqansu àq ak yelleefu antarpiris
Soppibànqaasu xam-xamu politig
SoppiMën a dugg
SoppiXam-xamu koom-koom ak doxalin
SoppiKërug internet [1]
Caada, diine, taaral ak jokkoo
SoppiKërug internet [2] Barabu tàggat ak gëstu caada, diine, taaral, ak jokkoo ëmb na juróom benn bàqasu :
- Bànqaasu jokkoo,
- bànqaasu infogarafi,
- Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada,
- Bànqaasu làkk ak caada Agrig,
- Bànqaasu mënloo aju ci bokk moomel,
- Bànqaasu Xam-xamu diine.
bànqaasu jokkoo
SoppiMën a dugg
Soppitërëlin
SoppiMujjàntal
SoppiBànqaasu infogarafi
SoppiBànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada
SoppiMujjàntal
SoppiMën a dugg
SoppiBànqaasu làkk ak caaday Afrig
SoppiMujjàntal
SoppiMàndargal
SoppiMën a dugg
SoppiWàllum gëstu
Soppinekkinu ndongo daara yi (CROUS)
SoppiYokkute lim ndongo yi
Soppi
SAT | SEG | SJP | LSH | TOTAL UGB | |
---|---|---|---|---|---|
2001/2002 | 400 | 280 | 499 | 1480 | 2659 |
2002/2003 | 475 | 325 | 535 | 1525 | 2860 |
2003/2004 | 559 | 349 | 575 | 1506 | 2989 |
2004/2005 | 671 | 396 | 505 | 1799 | 3371 |
2005/2006 | 726 | 415 | 688 | 1965 | 3794 |
2006/2007 | 727 | 641 | 932 | 2143 | 4443 |
Dëkkuwaay
Soppi-
Campus 2
-
Village B
-
Village E
-
Village F
-
Village H
-
Village H bis
-
Village L
-
Village L (Bis)
Loyer mensuel tout compris pour les nationaux | Loyer tout compris en frCFA pour les étrangers | |
---|---|---|
Villages A,B,C,D,E,F,K,M | 3000 (4,57 euros) | ??? |
Villages H,I,J,L | 4000 (6,09 euros) | ??? |
Dem beek dikk bi
SoppiTektal yi
Soppi- ↑ "Archived copy". Archived from the original on 2016-03-03. Retrieved 2015-12-21.
- ↑ "Archived copy". Archived from the original on 2016-01-10. Retrieved 2015-12-21.
Xool yeneen
SoppiTéere ak mbóotu tektal
Soppi- Dossier sur l'UGB dans un numéro spécial sur l'enseignement supérieur au Sénégal, Le Soleil, janvier 2008, Royuwaay:P.5-6
Cosaan
Soppi- https://web.archive.org/web/20121110200513/http://www.gouv.sn/Decret-no-2012-1163-du-29-octobre.html
mbóotu tektal
Soppi- Musée du Centre de Recherches et de Documentation du Sénégal à Saint-Louis
- Université Cheikh-Anta-Diop
- Éducation au Sénégal
- Felwine Sarr
mbóotu biti
Soppi- Site officiel
- Présentation et images sur le site du Campus numérique francophone de Saint-Louis
- Site des étudiants de Sanar
- Fiche de l'UGB sur le portail SenCampus
- [https ://fr.glosbe.com]
Royuwaay:Portail Royuwaay:Infobox Université ' Iniwersite Gaston Berger mooy Daara ju kawe ji nekk diwaanu Ndar ci réewum Senegaal.

- Bànqaasu làkk ak caaday Afrig,
- Bànqaasu mënloo aju ci bokk moomel,
- Bànqaasu Xam-xamu diine.
bànqaasu jokkoo
SoppiMën a dugg
Soppitërëlin
SoppiMujjàntal
SoppiBànqaasu infogarafi
SoppiBànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada
SoppiMujjàntal
SoppiMën a dugg
SoppiBànqaasu làkk ak caaday Afrig
SoppiMujjàntal
SoppiMàndargal
SoppiMën a dugg
SoppiWàllum gëstu
Soppinekkinu ndongo daara yi (CROUS)
Soppiyokkute lim ndongo yi
Soppithumb|350px|Évolution des effectifs de l'UGB entre 2001 et 2007

SoppiL'université Gaston Berger est composée d'unités de formation et de recherche (UFR équivalent des facultés). Il y en a huit au total :
- Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama
- Xam-xamu jëmale ak xarala
- Xam-xamu yoon ak politig
- Xam-xamu koom-koom ak
- Xam-xamu wérgu-yaram
- Xam-xamu mbay, sàmm, nàpp ak xarala yu màcc ci wàllum dund
- Caada, diine, taaral ak jokkoo
- Diiru njàng mi di na toll ci fukki weer. Di tàmbalee oktoobar jàpp sulet. Waaye ubbite njagale mi ak njeextal mi ngi aju ci barabu tàggat ak gëstu bu nekk.
Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama
SoppiBarabu tàggat ak gëstu ci ladab ak xam-xamu nekkinu doomu aadama ëmb juróomu bàqasu:
- Angale,
- Farãse
- Làkk nasaraan jëmale,
- Xam-xamu melosuuf,
- Xam-xamu nekkinu àskan yi.
Xam-xamu jëmale ak xarala
SoppiBarabu tàggat ak gëstu ci xam-xam jëmale ak xaraala ëmb na bàqasu xayma jëmale, bànqaas informatig, bànqaas bitil jëmale ak tàggat ci wàllum xéy.
Mën a dugg
SoppiBànqaasu xayma jëmale
SoppiBànqaasu bitil jëmale
SoppiBànqaasu informatig
SoppiXam-xamu yoon ak politig
SoppiBarabu tàggat ak gëstu xam-xamu yoon ak politik ëmb na ñett bàqaas:
- Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi ;
- Bàqansu àq ak yelleefu antarpiris ;
- Bànqaasu xam-xamu politig.
Bànqaasu àq ak yelleefu gox-goxaan yi
SoppiBàqansu àq ak yelleefu antarpiris
Soppibànqaasu xam-xamu politig
SoppiMën a dugg
SoppiXam-xamu koom-koom ak doxalin
SoppiKërug internet [1]
Caada, diine, taaral ak jokkoo
SoppiKërug internet [2] Barabu tàggat ak gëstu caada, diine, taaral, ak jokkoo ëmb na juróom benn bàqasu :
- Bànqaasu jokkoo,
- bànqaasu infogarafi,
- Bànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada,
- Bànqaasu làkk ak caada Agrig,
- Bànqaasu mënloo aju ci bokk moomel,
- Bànqaasu Xam-xamu diine.
bànqaasu jokkoo
SoppiMën a dugg
Soppitërëlin
SoppiMujjàntal
SoppiBànqaasu infogarafi
SoppiBànqaasu mënloo ci wàllum taaral ak caada
SoppiMujjàntal
SoppiMën a dugg
SoppiBànqaasu làkk ak caada Agrig