Ile de Saint-louis

Dun bou nek Sénéal Soppi

Dun bou Saint-Louis mo feeté si xalu zu teud bi bu ndar. Si attum 2000 laaco UNESCO[1] bind si momeelou adduna bi.

Dek la yitam bou makk si walum adda ah thiossan.

Taariix Soppi

Gnogui co deff momëlou Toubab si 17e siécle, Saint-louis gnugui ko deff taxx si diguu 19e siecle. Mo neek Cpital bu dieuk bu Sénégal si attum 1872 ba 1957. Mo gui amoon taxawaay bu maak si walum koom ak adda sii afrique suwu diant bi yeupp.

miinu fëttëm si dun wi ak fu dëg bi di sanëcu si dëxu Sénégal bi ak ay xarelem you mouthi ayib, fi nap you di terr ak deug zayou toubab yii mo tax Saint-Louis am xarou kanan bu ragnëco.

Gnogui co Tiibë Soppi

[2]

  1. [1]
  2. Île de Saint