Fepp mooy xaaj bi gën a tuuti ci aw yaram wu neen (simple), wu man a booloo ak weneen ci simi. ñaare day ame ci ab saal bu sosoo ci ay Proton aki Notron yu ay Elektron di peek (di wër).