Disc jockey (ñu koy wax itam DJ, di jàng "dijéy"), mooy kiy teg woy yi ci xew yi ak ci feccuwaay yi, jagleel ko benn mbooloo.

Fànnu DJ

Soppi

DJ bi ab béglookat la, mooy kiy yor li ñeel woy yi ñuy teg cib barab, (mooy tànn woy yi, waaye it day bàyyi-xel ci mbooloo mi)