Diiwaanu Tambaakundaa

(Yoonalaat gu jóge Diiwaanu Tambakundaa)

Diiwaanu Tàmbaakundaa mi ngi nekk ci penku réew mi, benn la ci 14 diiwaan yu Senegaal yi, di it bi ci ëpp ci rëyaay. Dëkku Tàmbakundaa mooy péeyub diiwaan bi. am na 605 695 ciy way-dëkk te yaatoo 59 602 km²

.

lonkoyoonu diiwaan bi ba 2007

Melosuuf Soppi

Ay peggam Soppi

Diiwaan baa ngi digoo ak:

 
Tundi Tambakundaa ba 2007

Ay goxam Soppi

Ginnaaw bi, bi ñu defee Tunduw Kéedugu Diiwaan bu mat sëkk ci 2008, Péncum Réewum Senegaal la ngi ko def ci 1 diggi-gammu ci 2008, diiwaan bi ñaari Tund rekk la am:

Xool it Soppi

Lëkkalekaay yu biti Soppi

  14 Diiwaani Senegaal  

Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa ·