David Woodard

bindkat aji-djiter ay orchestres ju Aamerig

David James Woodard (ˈwʊdɑːrd; bi djudu ci juróom-bennou ñeenteelu weerou 1964 ci Santa Barbara, California) bene niit bou khamner yiitem djeuk mo nekone djiter ay orchestres ba paré done binde ay xët ci aname bu bou bookoul ak kene. Mougui djouguer si njaboot bou ame jaar jaar bu goude si Aamerig.[1][2]

Woodard ci 2020

Woodard te diapaler na tamite bene mboolo Nueva Germania, wou niit bou beuguone yaatal bene mbooloom bu wuuteci bene deuk bu soorii mougui toude Paraguwaay. Ci biir Almaañ livre, Five Years (Juróom At), bimou biide aak kharitam, swis bindkat Christian Kracht, niougui wakh cii yëf yu rafet yi niou fa def ngir dimvali nit yi.[3][4]

Teereekaay

Soppi

Karmat ak delluwaay

Soppi
  1. Carpenter, S., "In Concert at a Killer's Death", Los Angeles Times, 9 mee 2001.
  2. Woodard, D., "Musica lætitiæ comes medicina dolorum", Der Freund, Nr. 7, maars 2006, pp. 34–41.
  3. Epstein, J., "Rebuilding a Home in the Jungle", San Francisco Chronicle, 13 maars 2005.
  4. Allen, M., "Décor by Timothy Leary", The New York Times, 20 samwie 2005.

Lëkkalekaay yu biti

Soppi

 

Xool it Wikimedia Commons