Ci làkku ibrë \^hdyu-tyb\^; CI làkku yawut la tur wi jóge. Ci angale mooy Bethsaida; Ci faranse mooy Bethsaïda

Betsayda

Dëkk ba ci penku-kawu dexu Galile la woon, sorewul fu dexu Yurdan dugg. Tey jii xamuñu tembe bérab bi. Man na nekk sax amoon na ñaari dëkk yu bokk tur Betsayda. Benn ci penku dexu Yurdan, te benn (mooy Betsayda ci diiwaanu Galile) ci sowu dexu Yurdan.

Man nañu koy jàng ci Injiil ci Mc 11:21; Mk 6:45 8:22; Lu 9:10; 10:13; Yow 1:44; 12:21.

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons