Beeco Cuun
Seex Beeco Cuun taalubeb S Saaliwu la, mu nekkoon kenn ci ñi daan liggéey ci yoriin wu Senegaal (administration sénégalaise), ku bari ñu aju ci moom la ciy murit, moom nag woote na ag ceexal gu bawoo ca S Saaliwu, waaye aw nit rawatina ci biir murit gi dañul di ko sikk ak a diiŋat