Bartelemi
Ci làkku ibrë תולמי-בר; Ci làkku yawut la tur wi jóge. Ci angale mooy Bartholomew; Ci faranse mooy Barthélemy
Benn ci fukki taalibe Yeesu ak ñaar la woon. Am na ñi xalaat ne Bartelemi ak Nataneel (Yow 1:45-51) kenn nit la.
Bartelemi feeñ na ci aaya yi ci Injiil: Mc 10:3; Mk 3:18; Lu 6:14; Jëf 1:13.