Baraki
Ci làkku gereg \~baraciav\~; Ci làkku ibrë (\^hykrb\^) la tur wi jóge. Ci angale mooy Barachias; Ci faranse mooy Barachie
Baayu Sakariya ki ñu reyoon ci këru Yàlla gi la woon.
Turam feeñ na ci Injiil ci Mc 23:35.