Ci làkku ibrë la tur wi jóge. Ci angale ak ci faranse mooy Azor.
Benn ci maamaati Yeesu ci Macë la woon (Mc 1:13,14).