Ci angale mooy (Forum of) Appius; Ci faranse mooy (Forum d')Appius
Benn dëkk ci réewu Itali la woon, bu amoon ja bu mag. Nekkoon na lu tollu 40 kilomet ci bëj-saalumu Room ci yoon wu mag wa tudd Yoonu Appien (Via Appienne).
Dañu koy gis ci Jëf 28:15.