Andoronikus
Ci angale ak ci faranse mooy Andronicus.
Benn Yawut bu toppoon Yeesu la woon. Ndawu Kirist la woon ki bokkoon ak Kirist bala Pool.
Ci Injiil dañu koy gis ci Ro 16:7.