Ci angale mooy amethyst; Ci faranse mooy améthyste
Per bu yolet la, bu xawa yaraax ni marjaan (jamaa) walla butéelu weer.
Dañu koy gis ci Injiil ci Pe 21:20.