Ci làkku ibrë la tur wi jóge.
Ci angale mooy Alphaeus; Ci faranse mooy Alphée
Turu 2 nit ñi wuute ci Injiil:
- Baayu Saag, mi bokkoon ca 12 taalibe Yeesu ya (Mc 10:3; Mk 3:18; Lu 6:15; Jëf 1:13).
- Baayu Lewi, juutikat bi bokkoon itam ci 12 taalibe Yeesu ya (Mk 2:14).