Ci angale mooy Alexander; Ci faranse mooy Alexandre
Turu 4 nit ñi wuute ci Injiil:
- Doomu Simoŋ mi dëkk Siren, di magu Rufus (Mk 15:21).
- Menn mbokku saraxalekat bu mag ba, Anas, (Jëf 4:6).
- Benn Yawut bu jóge Efes (Jëf 19:33,34).
- Benn tëgg ci Efes. Bëre woon na ak waxi Pool (1Tim 1:20; 2Tim 4:14,15).