Akwa Boni
Akwa Boni (wala Akoua Boni ) doomu rakk la woon bu Abla Pokou, benn lingeer afrik bu sos waa Baoulé ci kodiwaar , mingi cosaanoo Gana. Mu nguur ci diggante 1730 ba 1750.
Njiitu réew | Kodiwaar |
---|---|
Dundu ak jaar-jaaram | |
Bésu juddu |
1708 Gana |
Bésu faatu |
1750 Kodiwaar |
Liggeey | Lingeer |
Waajur wu jigeen | Abla Poku |