Akilas
Ci angale mooy Aquila; Ci faranse mooy Aquilas
Benn Yawut ak toppkatu Yeesu la woon, ma nga juddu woon Pont ci Asi Minër. Jabaram, Pirsil la tuddoon. Defarkatu tànt la woon ni Pool. Nawle ak Pool la, ci liggéeyu Boroom bi, te dafa amoon mbooloom ñi gëm ma doon daje ci seen kër ci Room.
Dañuy jàng ci Akilas ci Jëf 18:2-3,18-19,26; Ro 16:3-5; 1Ko 16:19; 2Tim 4:19.