Ci làkku ibrë la tur wi jóge. Ci angale mooy Addi; Ci faranse mooy Addi
Benn ci maamaati Yeesu ci Luug la woon (Lu 3:28).