Ñamako
Ñamako xeet la ci xeeti garab yi nga xam ni seenug dund man naa yàgg lool. Ñu ngi koy fekk ci tundi Afrig.
Njariñ li
SoppiGarab la gog ay doomam dees koy jëfandikoo, ngir xeeti saf-safal. Dees na ko jëfandikoo it ngir neexal sëy.
Jaarjaaram
SoppiÑamako bokkoon na ci njaay yi nga xam ni ñoo gënoon a dox ci yiñ daa dugal ca Afrig sowwu jant, ci jamonoy xarnub 18. Loolu sax moo tax ñu di ko woowe, "côte du Poivre" fële ca Gine.
Turu xam-xam wi
SoppiAframomum melegueta
Tur wi ci yeneeni làkk
Soppifarañse: maniguette |